1. 1

    Dip Doundou Guiss - #FreeSenegal

  2. 2

    Dip Doundou Guiss - #Kmnd (feat. Lefa)

  3. 3

    Dip Doundou Guiss - 40e jour

  4. 4

    Dip Doundou Guiss - Ànd Xeex Coronavirus

  5. 5

    Dip Doundou Guiss - Assamane

  6. 6

    Dip Doundou Guiss - Baby (feat. Aida Samb)

  7. 7

    Dip Doundou Guiss - Bad Man

  8. 8

    Dip Doundou Guiss - Califat

  9. 9

    Dip Doundou Guiss - Ci Naka

  10. 10

    Dip Doundou Guiss - Damako Khar

  11. 11

    Dip Doundou Guiss - Dee Ci Yaw

  12. 12

    Dip Doundou Guiss - Destin

  13. 13

    Dip Doundou Guiss - Deuil National

  14. 14

    Dip Doundou Guiss - Doon Benn

  15. 15

    Dip Doundou Guiss - Doundou Oundou

  16. 16

    Dip Doundou Guiss - F Y N

  17. 17

    Dip Doundou Guiss - Fayeku

  18. 18

    Dip Doundou Guiss - Holocauste (Intro)

  19. 19

    Dip Doundou Guiss - Homie

  20. 20

    Dip Doundou Guiss - Intro

  21. 21

    Dip Doundou Guiss - Jëli Li Des

  22. 22

    Dip Doundou Guiss - LNN (feat. Bass Thioung)

  23. 23

    Dip Doundou Guiss - LYXRD

  24. 24

    Dip Doundou Guiss - May Kane

  25. 25

    Dip Doundou Guiss - Me N You

  26. 26

    Dip Doundou Guiss - Musiba

  27. 27

    Dip Doundou Guiss - Ndogal (part. Ashs The Best)

  28. 28

    Dip Doundou Guiss - Ñetti At Ci Ren

  29. 29

    Dip Doundou Guiss - Nguur

  30. 30

    Dip Doundou Guiss - Niata Nio Dess

  31. 31

    Dip Doundou Guiss - Nightmare

  32. 32

    Dip Doundou Guiss - NLMD

  33. 33

    Dip Doundou Guiss - NOBOMA WOON

  34. 34

    Dip Doundou Guiss - Nouyo National (feat. Karabalik Beatz, Bilou XIV & Samba Peuzzi)

  35. 35

    Dip Doundou Guiss - Reunion

  36. 36

    Dip Doundou Guiss - Saajobaan

  37. 37

    Dip Doundou Guiss - Seetu

  38. 38

    Dip Doundou Guiss - Suba

  39. 39

    Dip Doundou Guiss - Sunshine

  40. 40

    Dip Doundou Guiss - Tamanefi

  41. 41

    Dip Doundou Guiss - Tefess

  42. 42

    Dip Doundou Guiss - Top 5

  43. 43

    Dip Doundou Guiss - UKTV (U Know The Vibe)

  44. 44

    Dip Doundou Guiss - Waawaw (feat. Aida Samb)

  45. 45

    Dip Doundou Guiss - Xalé Bu Ndaw (feat. Samba Peuzzi)

  46. 46

    Dip Doundou Guiss - Yeungueul Ci Say Mbagg (feat. OMG)

  47. 47

    Dip Doundou Guiss - Yow Lay Nobaat (feat. Jahman Xpress)

Damako Khar

Dip Doundou Guiss

Reptile musique
Yeah

Ba ñeup diékhalei mane silay fess
Deff nala papa parce que téré woma khekh
Di nañ la enquête parce que tay sa dooma khew
Tay bama lén wané sama rangoñe ñom ñeupa bëg
Bo khamé ni faw nga lekk faw nga fokhalé
Dangay khep condamné bou tol-ni Centenaire
Last-Cri pair-ou daleu dama la soll ba dead
Motax day job ba dead
Ñak jott ba dead

Dama khar ni Staph Curi pour wathié Jordan man
Ni béppou khétou nitt bouy wadia done lénéne
Fatté wouma fiñe ma diangalé figne ma diongalé
Fatté wouma Pa yima ñanal ak mère yima diox ma lekk

Avenir lañ démone dieuli si yoonou clochard
Karaw bou ñoul ak khell mou mak sa ñoom maam
Boul wolou sakh ñila wolou confiance
Xadioul si malak'ak djinné confiance

Maay garab bou bëgg microbe
Innocent bou andak Inno
Ay féneukat rek'ak ay traîtres
Lay guiss souma fattéliko
Diox ma passeport visa yeah
Tampon si passeport bi ma dém
Par force fasse diom rich mba dead
Waw-Goor dinga doon milliardaire, eh
Yaffi néwone souñou gang famille la
Ñioune nieup bok diaar-diaar nigger
Fima diaar koufa diaar xam yaw
Finaga diaar koufa diaar tass sa yaakaar, nigger
Mangi ñaffé Mangi xare matt, nigger
Xonét'a touma sax rarement, nigger
Fima diougué soum fa naré déllou watt
Fat-ma jail wala hôpital my, nigger

Yeah, yeah, yeah

Ba ñeup diékhalei mane silay fess
Dip kom kou teudd lo correctionel ay colonels
Dinañe ma saaga nday di naléén songg xééx
Kone ñaak jott ba dead, Guéné son ba dead
Meuwti sax douma dieul si
Parce que maak mooma yam
Kone en cas MC bou dead
Boul lathie kane moko ray
Ñaata rappeurs nga fay
Ñaata millions nga lek
Boy déssé touma bén rangogne
Pour dioy sa deuthie
Est-ce que wiccax na sama baram
Geuthie na réthiou depuis 17 ans, motherfucker
Dama ko khar ni ki dead ak aldiana
Mane damalén réndi soga tiit ndaysan
Dawna yaram
Boy mane kassé bén nitt
5000 nitt dima xééx
Ñaanal na samay ennemie, ennemie kii ak kéé
Dama xéxal mbédd mi, mbédd mi dima xééx
Dama xééxal mbédd mi, mbédd mi dima xééx
Mangi si chais'ou buur bi ñongi si chais'ou douche yi
Fekk yi dounk yi nandité yi mouss you mouss yi
Tekk naÑou deal
May guéné guénou ci
Noir et vert amoufi dér bou ñuul bou xew (Dér bou ñuul bi)
Maffi gueneu touti thiaabi reuy
Di tidji bountou
Maangi gueneu yéék di gueneu yéék
Di gueneu wéét
Xarit'aka nééw ci diamono
Wouy sama nday
Trahir yeurmandé
Deff sama xoll ci sama xéll
Jaay kou meuna fay
Douñ mayé xéér di keup caisse
Yeah fitneu laa fitneu, may fitneu
Fitneu laa Fitneu, maay Fitneu
Loolo tax ma wañi samay djo bro
Loolo tax ma yokk sama job bro
Loolo tax ma ñémé songou gandi gros lots
Loolo tax ma wéddi course ak sama chrono
Premier la dieul bëggou ma passer
Pour yaw ndiago fôt ak passer Rk
Tassanté nga ak mane mou déñ

Ba ñeup diékhalei mane silay fess
Deff nala papa parce que téré woma khekh
Di nañ la enquête parce que tay sa dooma khew
Tay bama lén wané sama rangoñe ñom ñeupa bëg
Bo khamé ni faw nga lekk
Faw nga fokhalé
Dangay khep condamné bou tol-ni Centenaire
Last-Cri pair-ou daleu dama la soll ba dead

Playlists relacionadas Ver mais playlists

Momentos

O melhor de 3 artistas combinados