1. 1

    Dip Doundou Guiss - #FreeSenegal

  2. 2

    Dip Doundou Guiss - #Kmnd (feat. Lefa)

  3. 3

    Dip Doundou Guiss - 40e jour

  4. 4

    Dip Doundou Guiss - Ànd Xeex Coronavirus

  5. 5

    Dip Doundou Guiss - Assamane

  6. 6

    Dip Doundou Guiss - Baby (feat. Aida Samb)

  7. 7

    Dip Doundou Guiss - Bad Man

  8. 8

    Dip Doundou Guiss - Califat

  9. 9

    Dip Doundou Guiss - Ci Naka

  10. 10

    Dip Doundou Guiss - Damako Khar

  11. 11

    Dip Doundou Guiss - Dee Ci Yaw

  12. 12

    Dip Doundou Guiss - Destin

  13. 13

    Dip Doundou Guiss - Deuil National

  14. 14

    Dip Doundou Guiss - Doon Benn

  15. 15

    Dip Doundou Guiss - Doundou Oundou

  16. 16

    Dip Doundou Guiss - F Y N

  17. 17

    Dip Doundou Guiss - Fayeku

  18. 18

    Dip Doundou Guiss - Holocauste (Intro)

  19. 19

    Dip Doundou Guiss - Homie

  20. 20

    Dip Doundou Guiss - Intro

  21. 21

    Dip Doundou Guiss - Jëli Li Des

  22. 22

    Dip Doundou Guiss - LNN (feat. Bass Thioung)

  23. 23

    Dip Doundou Guiss - LYXRD

  24. 24

    Dip Doundou Guiss - May Kane

  25. 25

    Dip Doundou Guiss - Me N You

  26. 26

    Dip Doundou Guiss - Musiba

  27. 27

    Dip Doundou Guiss - Ndogal (part. Ashs The Best)

  28. 28

    Dip Doundou Guiss - Ñetti At Ci Ren

  29. 29

    Dip Doundou Guiss - Nguur

  30. 30

    Dip Doundou Guiss - Niata Nio Dess

  31. 31

    Dip Doundou Guiss - Nightmare

  32. 32

    Dip Doundou Guiss - NLMD

  33. 33

    Dip Doundou Guiss - NOBOMA WOON

  34. 34

    Dip Doundou Guiss - Nouyo National (feat. Karabalik Beatz, Bilou XIV & Samba Peuzzi)

  35. 35

    Dip Doundou Guiss - Reunion

  36. 36

    Dip Doundou Guiss - Saajobaan

  37. 37

    Dip Doundou Guiss - Seetu

  38. 38

    Dip Doundou Guiss - Suba

  39. 39

    Dip Doundou Guiss - Sunshine

  40. 40

    Dip Doundou Guiss - Tamanefi

  41. 41

    Dip Doundou Guiss - Tefess

  42. 42

    Dip Doundou Guiss - Top 5

  43. 43

    Dip Doundou Guiss - UKTV (U Know The Vibe)

  44. 44

    Dip Doundou Guiss - Waawaw (feat. Aida Samb)

  45. 45

    Dip Doundou Guiss - Xalé Bu Ndaw (feat. Samba Peuzzi)

  46. 46

    Dip Doundou Guiss - Yeungueul Ci Say Mbagg (feat. OMG)

  47. 47

    Dip Doundou Guiss - Yow Lay Nobaat (feat. Jahman Xpress)

Deuil National

Dip Doundou Guiss

Manatuma toog di xaar leneen
Li nek sama bop bi xatt na fees na
Manatuma toog di xaar leneen
Dama muju joow ci gaal ba dess fa

Lelelelelena dama muñ ba de, muñ bi jeex na
Ndaw si diggu geej weet na, reer na
Sama bakanay rot su geej gi mare naan

Lo sorale dalay diisël
Tëwa fatte ñima bayi ginaaw
Nap kat bi gëdj na giss jën
Ku saccul, ñaanul marr na xiif na
Diplome ak journala yam këyit lë
Fay ndox ak courant ba tay dañuy të
Suñu quotidien mo gëna tiss tëss
Suñu kër day taa ndox luñu miin lë
Xamul ndax yoonu xaru la am yoonu risque lë
Tekkey alxuranam, tekkey biblëm
Geej du mëssa rëy ba ëp fittëm
Gëm ni buñu yegge nañ yeetal fitnë
Def ni ku rep giss yoon
Dekkufi sedd di lox
Defuñu ken lu bonn
Dadj luñu yeene wul dom
Soobu si teen bi di root
Dem te ñëw tedd ni Gorr
Dem te ñëw fay suñuy borr
Delu samay digg mbok

Don mak si kër di daw yërmande ak ndimbël motax ñu sëss
Xam liñu bëg fimu ne moy xam fiñu jëm
Yoonu geej du liñu gënël liñu gënël moy am li gën
Ken bëgul doomam di taggo dem ñukoy deggat si dëdj
Gaal bu dëppu, këppu, këppale famille lëm
Mëno ŋacc waye dem nga seeti charlie demb
Juromi temeri neew Etat ne du wax si sen dëdj
Fi yaakar si nguur moy yaakar si ay ngandi dëm

Manatuma toog di xaar leneen
Li nek sama bop bi xatt na fees na
Manatuma toog di xaar leneen
Dama muju joow ci gaal ba dess fa

Lelelelelena dama muñ ba de, muñ bi jeex na
Ndaw si diggu geej weet na, reer na
Sama bakanay rot su geej gi mare naan

Playlists relacionadas Ver mais playlists

Momentos

O melhor de 3 artistas combinados