1. 1

    Dip Doundou Guiss - #FreeSenegal

  2. 2

    Dip Doundou Guiss - #Kmnd (feat. Lefa)

  3. 3

    Dip Doundou Guiss - 40e jour

  4. 4

    Dip Doundou Guiss - Ànd Xeex Coronavirus

  5. 5

    Dip Doundou Guiss - Assamane

  6. 6

    Dip Doundou Guiss - Baby (feat. Aida Samb)

  7. 7

    Dip Doundou Guiss - Bad Man

  8. 8

    Dip Doundou Guiss - Califat

  9. 9

    Dip Doundou Guiss - Ci Naka

  10. 10

    Dip Doundou Guiss - Damako Khar

  11. 11

    Dip Doundou Guiss - Dee Ci Yaw

  12. 12

    Dip Doundou Guiss - Destin

  13. 13

    Dip Doundou Guiss - Deuil National

  14. 14

    Dip Doundou Guiss - Doon Benn

  15. 15

    Dip Doundou Guiss - Doundou Oundou

  16. 16

    Dip Doundou Guiss - F Y N

  17. 17

    Dip Doundou Guiss - Fayeku

  18. 18

    Dip Doundou Guiss - Holocauste (Intro)

  19. 19

    Dip Doundou Guiss - Homie

  20. 20

    Dip Doundou Guiss - Intro

  21. 21

    Dip Doundou Guiss - Jëli Li Des

  22. 22

    Dip Doundou Guiss - LNN (feat. Bass Thioung)

  23. 23

    Dip Doundou Guiss - LYXRD

  24. 24

    Dip Doundou Guiss - May Kane

  25. 25

    Dip Doundou Guiss - Me N You

  26. 26

    Dip Doundou Guiss - Musiba

  27. 27

    Dip Doundou Guiss - Ndogal (part. Ashs The Best)

  28. 28

    Dip Doundou Guiss - Ñetti At Ci Ren

  29. 29

    Dip Doundou Guiss - Nguur

  30. 30

    Dip Doundou Guiss - Niata Nio Dess

  31. 31

    Dip Doundou Guiss - Nightmare

  32. 32

    Dip Doundou Guiss - NLMD

  33. 33

    Dip Doundou Guiss - NOBOMA WOON

  34. 34

    Dip Doundou Guiss - Nouyo National (feat. Karabalik Beatz, Bilou XIV & Samba Peuzzi)

  35. 35

    Dip Doundou Guiss - Reunion

  36. 36

    Dip Doundou Guiss - Saajobaan

  37. 37

    Dip Doundou Guiss - Seetu

  38. 38

    Dip Doundou Guiss - Suba

  39. 39

    Dip Doundou Guiss - Sunshine

  40. 40

    Dip Doundou Guiss - Tamanefi

  41. 41

    Dip Doundou Guiss - Tefess

  42. 42

    Dip Doundou Guiss - Top 5

  43. 43

    Dip Doundou Guiss - UKTV (U Know The Vibe)

  44. 44

    Dip Doundou Guiss - Waawaw (feat. Aida Samb)

  45. 45

    Dip Doundou Guiss - Xalé Bu Ndaw (feat. Samba Peuzzi)

  46. 46

    Dip Doundou Guiss - Yeungueul Ci Say Mbagg (feat. OMG)

  47. 47

    Dip Doundou Guiss - Yow Lay Nobaat (feat. Jahman Xpress)

Yeah-yeah
Yeah-yeah

Bët du xool ba xam lu xel di gis
Ma gëm say wax ba fàtte xool sa jikko
Mën ko faj waaye dam la bàyyi ci biir
Ëllëg du añ te mat na fàttaliku
Ho, homie, homie, homie, homie

Bët du xool ba xam lu xel di gis
Ma gëm say wax ba fàtte xool sa jikko
Mën ko faj waaye dam la bàyyi ci biir
Ëllëg du añ te mat na fàttaliku
Ho, homie, homie, homie, homie

Depuis temps xale la ma gëj dal
Mbëggeel dëggu ni yaay bàmmeel ak ay mbugalam
Dëju mawti ngay xam ne dee moo gën a dëggu xol
Xarit dëmm la chaque année ma koy gën a gëm
Ndax mbëggeel du jaay divorce du fay dot
Njëkk a jooy miraas ba noppi xew dëj
Lii jikko jaan la feesal dell ci jëmmu xaj
Li ko taal batey mu yegg lay njëkk fay
Pexe noon du contre yaw pour yaw la nigga
Kenn mënut a gaaw ci tijji xel ni paaka ci xol
Xam sa bopp bu doon école kenn a du fa passer diplôme
Tuxal dëkk a gën a yomb nit ki changer jikkoom
Bu doon ku baax du daj lu bon yónnent du doon jirim
Nelaw ci bàmmeel rekk a yàgg te amul lal ci biir
Wor nga ma ma nigga bàyyiwuma la dam la ba ci biir
Yaa ma woon ne man naa dëkk si pax ak ay jaan ci biir

Bët du xool ba xam lu xel di gis
Ma gëm say wax ba fàtte xool sa jikko
Mën ko faj waaye dam la bàyyi ci biir
Ëllëg du añ te mat na fàttaliku, ho

Homie, homie, homie, homie
Homie, homie, homie, homie
Homie, homie, homie, homie

Fàww ngay loru yenn saay pour man yegg fenn fi
Ku wann lor buy jur ci mettit lay wësin
Boo bëggee jege sa jàmm fàww nga sori ñenn ñi
Xarit bu jege gën a jekku énnemie
Dëgg nattukaay jëf du changer melo comme nun
Du sutura rekk jëf lu bon a tax nit njëkk a nëbbu
Lu tax nit gën te fekk mala yee nu gën a dëggu
Ndax ci jikko juda moo ëpp sët Jesus ci kaw suuf
Noon bi lay ŋàññ gën sa waa ji lay jay
Noon biy tax ngay ñafe moo gën ñi lay wër di lay fen
Jarul topp nitu intérêt àdduna ay àjjanaam
Ñi di dagg sa xol yaa tax seen paaka ñaw

Do my story sometimes, do my story sometimes
Do my sto peace of mind
Do my sto do my sto
Do my story sometimes
Do my story peace of mind, do my story peace of mind
Do my sto do my sto

Homie, homie, homie, homie

Playlists relacionadas Ver mais playlists

Momentos

O melhor de 3 artistas combinados