1. 1

    Dip Doundou Guiss - #FreeSenegal

  2. 2

    Dip Doundou Guiss - #Kmnd (feat. Lefa)

  3. 3

    Dip Doundou Guiss - 40e jour

  4. 4

    Dip Doundou Guiss - Ànd Xeex Coronavirus

  5. 5

    Dip Doundou Guiss - Assamane

  6. 6

    Dip Doundou Guiss - Baby (feat. Aida Samb)

  7. 7

    Dip Doundou Guiss - Bad Man

  8. 8

    Dip Doundou Guiss - Califat

  9. 9

    Dip Doundou Guiss - Ci Naka

  10. 10

    Dip Doundou Guiss - Damako Khar

  11. 11

    Dip Doundou Guiss - Dee Ci Yaw

  12. 12

    Dip Doundou Guiss - Destin

  13. 13

    Dip Doundou Guiss - Deuil National

  14. 14

    Dip Doundou Guiss - Doon Benn

  15. 15

    Dip Doundou Guiss - Doundou Oundou

  16. 16

    Dip Doundou Guiss - F Y N

  17. 17

    Dip Doundou Guiss - Fayeku

  18. 18

    Dip Doundou Guiss - Holocauste (Intro)

  19. 19

    Dip Doundou Guiss - Homie

  20. 20

    Dip Doundou Guiss - Intro

  21. 21

    Dip Doundou Guiss - Jëli Li Des

  22. 22

    Dip Doundou Guiss - LNN (feat. Bass Thioung)

  23. 23

    Dip Doundou Guiss - LYXRD

  24. 24

    Dip Doundou Guiss - May Kane

  25. 25

    Dip Doundou Guiss - Me N You

  26. 26

    Dip Doundou Guiss - Musiba

  27. 27

    Dip Doundou Guiss - Ndogal (part. Ashs The Best)

  28. 28

    Dip Doundou Guiss - Ñetti At Ci Ren

  29. 29

    Dip Doundou Guiss - Nguur

  30. 30

    Dip Doundou Guiss - Niata Nio Dess

  31. 31

    Dip Doundou Guiss - Nightmare

  32. 32

    Dip Doundou Guiss - NLMD

  33. 33

    Dip Doundou Guiss - NOBOMA WOON

  34. 34

    Dip Doundou Guiss - Nouyo National (feat. Karabalik Beatz, Bilou XIV & Samba Peuzzi)

  35. 35

    Dip Doundou Guiss - Reunion

  36. 36

    Dip Doundou Guiss - Saajobaan

  37. 37

    Dip Doundou Guiss - Seetu

  38. 38

    Dip Doundou Guiss - Suba

  39. 39

    Dip Doundou Guiss - Sunshine

  40. 40

    Dip Doundou Guiss - Tamanefi

  41. 41

    Dip Doundou Guiss - Tefess

  42. 42

    Dip Doundou Guiss - Top 5

  43. 43

    Dip Doundou Guiss - UKTV (U Know The Vibe)

  44. 44

    Dip Doundou Guiss - Waawaw (feat. Aida Samb)

  45. 45

    Dip Doundou Guiss - Xalé Bu Ndaw (feat. Samba Peuzzi)

  46. 46

    Dip Doundou Guiss - Yeungueul Ci Say Mbagg (feat. OMG)

  47. 47

    Dip Doundou Guiss - Yow Lay Nobaat (feat. Jahman Xpress)

Nouyo National (feat. Karabalik Beatz, Bilou XIV & Samba Peuzzi)

Dip Doundou Guiss

(Karabalik in the track)
Hey
Koulou kin-kin

Karabalik nèna silolèn nè
Si lolèn nè, enh
Si lolèn nè
Koulou kinkin kinkin
Si lolén nè
Hum hum hum ah ah

Si lolèn nè yèna ngi si diam
Si lolèn nè yèna ngi si diam
Si lolèn nè mba diameu ngèn am (Hey)
Si lolén nè, hey, mba régue ngén

Si lolèn nè
Parce que magui si diameu si lolèn nè
Ngèn di rap ni kouy dakadji sathi fils dolèn yam
Do sampeu sa tankeu si banque sinon loy lék
Gno lèkeu xalisou rap sa rappeur bi xoss na swing gomme lay yeuye
Gnaw ga sa dome bi guignol lay nèk
Sananetè xèrr bi si gnom lay yam
Saganetè nday bi si lay
Gnom rèk, mba règue ngèn
Yèna ngi course mba yégg ngèn
Dam lén di couche mba dayou ngén
Rap bi douma ko bayék yén
Doumako bayé ak ay mindeu néw
Djieukeu deih di beugueu tagué dip
Deuthi bou wètt ni deih thi pandémie
Dingu ko képeu teuthi sa gatt tè ganè mik
Da ngén tèki mais dou fègne si kanami (hey)
Fatal ma fèpeu gnou Yolé lèn
Xadial ma fèthii fi yolèlè sèn xolay mètti
Si lolèn, si lolèn

Si lane ngèn nè mane dè magui sama olala
Comment tu vas waxma yaw si lane nga nè
Gnoune dè gnogui sougnou olala
Yén nak

Si lolèn nè
Si lolèn nè, enh
Si lolèn nè
Koulou kinkin kinkin
Si lolén nè
Hum hum hum ah ah

Si lolèn nè yèna ngi si diam
Si lolèn nè yèna ngi si diam
Si lolèn nè mba diameu ngèn am (Hey)
Si lolèn nè, koulou kinkin

Nèko reuleu mou deuleu na andak tiol tèy deunou
Si lolèn nè, falalèn fèk mane dingèn ma gueuneu diox gueudeu
Thi simili mane lalèn may mak bouma si feugeu mou keupou
Keupeu keupeul douma tèrè fateu tourou vautour
Manila mbaye fatal

Hey
Dèf kom bang di tiapeu sa pipette
Yènèn gars yiye copier nèlèn gnou rang
Tè dagati ticket xolal kara beuseul ma lolu
Rèwandè bi la beugueu wanè
Xalè la cachet concert yigne mag fay lay dieundè gouté asey (hum)
Kholal Boudè rèwandè pair rou daleu la
Talibè rèkay yarou
Sa bro biy yègal mbagueu gnodi DG tè
Gnoune gneup xamnagne ni yoroul
Khathi yifi nèk gnègnègnè fèn rek
Mbeuw mbeuw Scooby Doo
Dolèn sax ay mbeurou galè
Ay mbeurou douche ngèn
Xamnagn ni kousi djiouk poup (kousi djiouk poup)
Hum ah ah ah ah ah ahh

Si lane ngèn nè mane dè magui sama olala
Comment tu vas waxma yaw si lane nga nè
Gnoune dè gnogui sougnou olala
Yén nak

Si lolèn nè
Si lolèn nè, enh
Si lolèn nè
Koulou kinkin kinkin
Si lolén nè
Hum hum hum ah ah

Si lolèn nè yèna ngi si diam
Si lolèn nè yèna ngi si diam
Si lolèn nè mba diameu ngèn am (Hey)
Si lolèn nè, hey, ba rëgg ngen
(Si lolèn nè)

Playlists relacionadas Ver mais playlists

Momentos

O melhor de 3 artistas combinados