1. 1

    Dip Doundou Guiss - #FreeSenegal

  2. 2

    Dip Doundou Guiss - #Kmnd (feat. Lefa)

  3. 3

    Dip Doundou Guiss - 40e jour

  4. 4

    Dip Doundou Guiss - Ànd Xeex Coronavirus

  5. 5

    Dip Doundou Guiss - Assamane

  6. 6

    Dip Doundou Guiss - Baby (feat. Aida Samb)

  7. 7

    Dip Doundou Guiss - Bad Man

  8. 8

    Dip Doundou Guiss - Califat

  9. 9

    Dip Doundou Guiss - Ci Naka

  10. 10

    Dip Doundou Guiss - Damako Khar

  11. 11

    Dip Doundou Guiss - Dee Ci Yaw

  12. 12

    Dip Doundou Guiss - Destin

  13. 13

    Dip Doundou Guiss - Deuil National

  14. 14

    Dip Doundou Guiss - Doon Benn

  15. 15

    Dip Doundou Guiss - Doundou Oundou

  16. 16

    Dip Doundou Guiss - F Y N

  17. 17

    Dip Doundou Guiss - Fayeku

  18. 18

    Dip Doundou Guiss - Holocauste (Intro)

  19. 19

    Dip Doundou Guiss - Homie

  20. 20

    Dip Doundou Guiss - Intro

  21. 21

    Dip Doundou Guiss - Jëli Li Des

  22. 22

    Dip Doundou Guiss - LNN (feat. Bass Thioung)

  23. 23

    Dip Doundou Guiss - LYXRD

  24. 24

    Dip Doundou Guiss - May Kane

  25. 25

    Dip Doundou Guiss - Me N You

  26. 26

    Dip Doundou Guiss - Musiba

  27. 27

    Dip Doundou Guiss - Ndogal (part. Ashs The Best)

  28. 28

    Dip Doundou Guiss - Ñetti At Ci Ren

  29. 29

    Dip Doundou Guiss - Nguur

  30. 30

    Dip Doundou Guiss - Niata Nio Dess

  31. 31

    Dip Doundou Guiss - Nightmare

  32. 32

    Dip Doundou Guiss - NLMD

  33. 33

    Dip Doundou Guiss - NOBOMA WOON

  34. 34

    Dip Doundou Guiss - Nouyo National (feat. Karabalik Beatz, Bilou XIV & Samba Peuzzi)

  35. 35

    Dip Doundou Guiss - Reunion

  36. 36

    Dip Doundou Guiss - Saajobaan

  37. 37

    Dip Doundou Guiss - Seetu

  38. 38

    Dip Doundou Guiss - Suba

  39. 39

    Dip Doundou Guiss - Sunshine

  40. 40

    Dip Doundou Guiss - Tamanefi

  41. 41

    Dip Doundou Guiss - Tefess

  42. 42

    Dip Doundou Guiss - Top 5

  43. 43

    Dip Doundou Guiss - UKTV (U Know The Vibe)

  44. 44

    Dip Doundou Guiss - Waawaw (feat. Aida Samb)

  45. 45

    Dip Doundou Guiss - Xalé Bu Ndaw (feat. Samba Peuzzi)

  46. 46

    Dip Doundou Guiss - Yeungueul Ci Say Mbagg (feat. OMG)

  47. 47

    Dip Doundou Guiss - Yow Lay Nobaat (feat. Jahman Xpress)

Karabalik on the track
Gilomas

Juddu doon Taaw
Dëk dëkku Bukki njombor
Xam na du ñep mëna doon gor
Du ñeppa believe on God
Man gëmu ma kenn kudul sama bopp
Te amu ma yoonu rethiou comme gun
Aller sans retour comme jaam
Man Yallah rekka xam lutax ma juddu doon taaw
Bayil ma sukku ñaan ko mu deff wiss bi doon taw
Duma Ndiago buy foote
Duma buy tukki toog kaaw
Duma sa gars yi talul ludul mukki boone tak
Mussu ma am flop
Log dangar bu ñor xomm
Diko tufli seen kaw
Mafi né té ñoma ëpo jotu rap fop
Budul mbiru koppar
Bul jël suñu contact
Nigger shut your fuck up
Gëdj na jooy depuis sama dëju mame
Duma mëssa def litax ba ñimay nëbbë naadj
Tuuma yepp ma tëx, lu, muuma woolu dëgg fight
Dugal rekk'ay tax ma football jox ma number nine

Ñaane pour samay noone
Ñaane pour samay niggers
Genné ci samay gars
Dé pour samay niggers
Ëppu mala impact
Yakoy woné ñu giss

Ñàq jotu ñàqqa tax ma juddu doon taaw
(Ñaane pour samay noone) Ñaane pour samay noone
(Genné ci samay gars) Genné ci samay gars
(Ëppu mala impact) haahaahaa

Dooré di encaisser coups ni dundu soldat
Xaaruma sol dallam pour jok wutu sama papa
Xammel kila bëg ak kiy wute pourcentage
Fenn bu gëna rëy mooy ku ame kuddu do laqq
Mame Yallah rekka xam lutax ma njëkka juddu
Kuné amna lo wara muñe lo wara xeex
Logique ni jours yi nga wara dundu, yo wara dé
Yaye limu dadj rek doyna fexeel ba thionom jeex
Ku def sa bopp ennemi do tall noono ak kenn
Fi ngay ñàqq deefa roote
Fi sa aduna yaqqo mëna tufa defaro
Def lula nit di xeebé, mënul wessu xeeb sa bopp
Budul say ñaanu waajur bane terré ngay gettaro (terré ngay gettaro)

Bindël sa suba tay, rakkdestin dou chance deh
Du yoon pabi dem ba maguette di fay louasse rek
Am-am ju lew, fi ñun ñeppa seex lu saleté
Pour feey si banneex duma yootu geedj di am dex
Fi jengu ba deh
Ragal réthiou ak gathié
Duñu tass yaakaru mère bi muk ni sëy bu tass tey
Samay principes ak sama ngor rekk'ay fess sama compte
Sama dignité sama xola may fek sama morgue
Duma ñé sama morom ba toog di fenn sama bop
Duma fenn sama bop ni jeek bu xeessal ba xonk
Life lu nek ak temps wam da ngay xëy sooga gontu
Life lou nek ak temps wam entre xel wala xol
Jeex na ba noppi kuko yénu rek sa xella fa tollu
Xeex nga ba sonnu Ma pour ame lo dundëlé sa njaboot
Tay nak sa doom yi magg nañ, juk tekki teral la jotna
Life lu waay def boppam, kenn du fay sama borr

Fole mimi fole mimi fo oh oh
Fole mimi fole mimi fo oh oh
Fole mimi fole mimi fo oh oh
Fole mimi fo oh oh oh

Fole mimi fole mimi fo oh oh
Fole mimi fole mimi fo oh oh
Fole mimi fole mimi fo oh oh
Fole mimi fo oh oh oh

Playlists relacionadas Ver mais playlists

Momentos

O melhor de 3 artistas combinados