1. 1

    Dip Doundou Guiss - #FreeSenegal

  2. 2

    Dip Doundou Guiss - #Kmnd (feat. Lefa)

  3. 3

    Dip Doundou Guiss - 40e jour

  4. 4

    Dip Doundou Guiss - Ànd Xeex Coronavirus

  5. 5

    Dip Doundou Guiss - Assamane

  6. 6

    Dip Doundou Guiss - Baby (feat. Aida Samb)

  7. 7

    Dip Doundou Guiss - Bad Man

  8. 8

    Dip Doundou Guiss - Califat

  9. 9

    Dip Doundou Guiss - Ci Naka

  10. 10

    Dip Doundou Guiss - Damako Khar

  11. 11

    Dip Doundou Guiss - Dee Ci Yaw

  12. 12

    Dip Doundou Guiss - Destin

  13. 13

    Dip Doundou Guiss - Deuil National

  14. 14

    Dip Doundou Guiss - Doon Benn

  15. 15

    Dip Doundou Guiss - Doundou Oundou

  16. 16

    Dip Doundou Guiss - F Y N

  17. 17

    Dip Doundou Guiss - Fayeku

  18. 18

    Dip Doundou Guiss - Holocauste (Intro)

  19. 19

    Dip Doundou Guiss - Homie

  20. 20

    Dip Doundou Guiss - Intro

  21. 21

    Dip Doundou Guiss - Jëli Li Des

  22. 22

    Dip Doundou Guiss - LNN (feat. Bass Thioung)

  23. 23

    Dip Doundou Guiss - LYXRD

  24. 24

    Dip Doundou Guiss - May Kane

  25. 25

    Dip Doundou Guiss - Me N You

  26. 26

    Dip Doundou Guiss - Musiba

  27. 27

    Dip Doundou Guiss - Ndogal (part. Ashs The Best)

  28. 28

    Dip Doundou Guiss - Ñetti At Ci Ren

  29. 29

    Dip Doundou Guiss - Nguur

  30. 30

    Dip Doundou Guiss - Niata Nio Dess

  31. 31

    Dip Doundou Guiss - Nightmare

  32. 32

    Dip Doundou Guiss - NLMD

  33. 33

    Dip Doundou Guiss - NOBOMA WOON

  34. 34

    Dip Doundou Guiss - Nouyo National (feat. Karabalik Beatz, Bilou XIV & Samba Peuzzi)

  35. 35

    Dip Doundou Guiss - Reunion

  36. 36

    Dip Doundou Guiss - Saajobaan

  37. 37

    Dip Doundou Guiss - Seetu

  38. 38

    Dip Doundou Guiss - Suba

  39. 39

    Dip Doundou Guiss - Sunshine

  40. 40

    Dip Doundou Guiss - Tamanefi

  41. 41

    Dip Doundou Guiss - Tefess

  42. 42

    Dip Doundou Guiss - Top 5

  43. 43

    Dip Doundou Guiss - UKTV (U Know The Vibe)

  44. 44

    Dip Doundou Guiss - Waawaw (feat. Aida Samb)

  45. 45

    Dip Doundou Guiss - Xalé Bu Ndaw (feat. Samba Peuzzi)

  46. 46

    Dip Doundou Guiss - Yeungueul Ci Say Mbagg (feat. OMG)

  47. 47

    Dip Doundou Guiss - Yow Lay Nobaat (feat. Jahman Xpress)

UKTV (U Know The Vibe)

Dip Doundou Guiss

Karabalik on the track

Fu mu mënti nekk
Ma wëri ko wëri ko wëri ko fu mu mënti nekk
Jëli ko jëli ko jëli ko fu mu mënti nekke
Man sama mind laa la dénk te doo mës a dégg bring it back
Love a fi nekk leneen xaju fi

Kon you know the vibe you know the melody
Yaw rekk yaa ma mës a tollu fii
Yaay sama naaj di sama jant bi
Baby, you know the vibe you know the melody
I say you know the vibe you know the melody
Baby, tonight dama la bëgg a gis
Këf sama mind tax ba ma wéradi
Baby, you know the vibe you know the melody

Baby, loo bëgg bëgg naa, loo wax ma defal la ko
Topp sa ginnaaw, foo nekk ma fekk la fa
Loo bëgg bëgg naa baby girl jox ma sa loxo
Bëgguma sa xel di ñaaw
Bëgguma keneen ku dul yaw
You're my ride or die mënóo deme nii
You're my wife yaw laa jënde ñeneen ñi
Sama paradise and my remedy
Me and you for life jusqu'à l'infiniii

Kon you know the vibe you know the melody
Yaw rekk yaa ma mës a tollu fii
Yaay sama naaj di sama jant bi
Baby, you know the vibe you know the melody
I say you know the vibe you know the melody
Baby, tonight dama la bëgg a gis
Këf sama mind tax ba ma wéradi
Baby, you know the vibe you know the melody

Baby, li nekk ci yaw moo nekk ci man
Dem nga woon te fàww nga dellusiwaat
Baby lépp mënul neex, fàww muy metti yenne saa yi
I called you phone but you don't wanna answer
Nobody know what you can do to me
Nobody know babe only you and me
And I feel blesed to be by your side
I don't want you to cry all night

Fu mu mënti nekk
Ma wëri ko wëri ko wëri ko fu mu mënti nekk
Jëli ko jëli ko jëli ko fu mu mënti nekke
Man sama mind laa la dénk te doo mës a dégg bring it back
Love a fi nekk leneen xaju fi

Kon you know the vibe you know the melody
Yaw rekk yaa ma mës a tollu fii
Yaay sama naaj di sama jant bi
Baby, you know the vibe you know the melody
I say you know the vibe you know the melody
Baby, tonight dama la bëgg a gis
Këf sama mind tax ba ma wéradi
Baby, you know the vibe you know the melody

Playlists relacionadas Ver mais playlists

Momentos

O melhor de 3 artistas combinados