Original   Tradução  
 
  Dibi dibi rek 
 Aah dibi dibi rek 
 Aah dibi dibi rek 
   Yangui deugueurlou wanté meunoko boul sop bayil niou djeuliko 
 Yangui ndirok balai bou niou takhawal, aah ndakh yow lekkato 
 Yangui beugu dé ndakh yow nanato, boul sop bayil niou djeuliko   
 Ndakh mo ley madj lo   
 Dibi dibi rek 
 Aah dibi dibi rek 
 Aah dibi dibi rek 
 Dibi dibi rek 
 Aah dibi dibi rek 
 Aah dibi dibi rek   
 Mbeuguel kenn khamoul lou mou doonn 
 Foulla diou barri ndaham amatou fi yoon 
 Kholl moy capitainou boromam 
 Ndakh mo ley madj lo   
 Dibi dibi rek 
 Aah dibi dibi rek 
 Aah dibi dibi rek 
 Dibi dibi rek 
 Aah dibi dibi rek 
 Aah dibi dibi rek   
 Ay niit niom bou niou beuguenté, khamaal lo tchi waakh 
 Niom mame boye sene taar wessouna, wayé tey laniou gueuneu beugueunté 
 Ya ngui beugu dé ndakh yaw lekatto 
 Bo fi guetarro waw ma bayiko 
 Ndakh mo lay madj lo   
 Dibi dibi rek 
 Aahdibi dibi rek 
 Aah dibi dibi rek 
 Dibi dibi rek 
 Aahdibi dibi rek 
 Aah dibi dibi rek   
 Ndakh mo lay madj lo 
 Ndakh mo lay madj lo   
 Dibi dibi rek 
 Aahdibi dibi rek 
 Aah dibi dibi rek 
 Dibi dibi rek 
 Aahdibi dibi rek 
 Aah dibi dibi rek   
 Dibi dibi rek 
 Aahdibi dibi rek 
 Aah dibi dibi rek 
 Dibi dibi rek 
 Aahdibi dibi rek 
 Aah dibi dibi rek