Mané hé baykat bi khalam 
 Démonna bay nékh wayé boumgua 
 Dokna mome 
 Mané hé baykat bi khalam 
 Démonna bay nékh wayé boumgua 
 Dokna mome 
    Mané hé baykat bi khalam démonna 
 Bay nékh wayé boumgua dokna mome   
 Boula nékhé talalal say lokho 
 Yaye docteur biy fath khifou askane bi 
 Liko dalé si nditoum rew bassi miskine 
 Ya souméko di dane sa dolé andak nath 
 Bi di liguey sa gnakha di tourou 
 Ngay bay di doukat bilay ya am diome   
 Kon diarama baykat koufi xiff yako 
 Doundal bamou sour waw koufi fébar 
 Yako nandal aki réén bamou féékh   
 Kon diarama baykat koufi xiff yako 
 Doundal bamou sour 
 Waw koufi fébar yako nandal aki réén 
 Bamou féékh   
 Ya momone sa mbay 
 Ya mome sa guanthiakh mome say 
 Ndiour ya mome sa alla di bay 
 Nguour gneuw dougalthia lokhome ak 
 Boor fékeleuthaa guanthiakh ba 
 Mégneu lole ndékétéyo   
 Kon diarama baykat koufi xiff yako 
 Doundal bamou sour 
 Waw koufi fébar yako nandal aki réén 
 Bamou féékh   
 Kon diarama baykat koufi xiff yako 
 Doundal bamou sour 
 Waw koufi fébar yako nandal aki réén   
 Bamou féékh 
 Dirama diarama baykat bé yaw 
 Kéneu rek mola mana fay 
 Moy bourbi yaalla 
 Guathia ngalama   
 Guathia ngalama yaw baykatbé 
 Guathia ngalama 
 Guathia ngalama yaw baikatbé   
 Dirama diarama baykatbé yaw 
 Kéneu rek moleu mana fay 
 Moye bourbi yalla