Senegal Senegal siguil ndiguale 
 Gambia Gambia oh siguil ndiguale 
 Amna benna ferie bougnou dane nane 
 Bateau le jola mi soukh sibir gueth gui 
    Xalebi migui dioye nane baye 
 Baye anna sama yaye boye 
 Baye neko dome anna yaye boye yaw 
 Senegal Senegal siguil ndiguale   
 Gambia Gambia oh siguil ndiguale 
 Mane baye migui dioye nane dome 
 Dome anna sa yaye boye   
 Dome neko baye anna yaye boye yam 
 Kone li firina ni yala reke sagne yala 
 Reke mane kon mome rekeu moy bour   
 Ndakh kepeu ko lath moune amnathi 
 Waye kon lii fir ndena ni Senegal bena bopeleu 
 Senegal beneu bopeleu 
 Senegal beneu bopeleu   
 Bilay 
 Ken douko khar gnaro 
 Beneu bopeleu Senegal 
 Faguarou diotna 
 Nagnou xolat sougnou bopeu bou bakh