1. 1

    Jeeba - Diarabi

  2. 2

    Jeeba - Aladji

  3. 3

    Jeeba - Happy Birthday

  4. 4

    Jeeba - Love Acoustic (Session Live)

  5. 5

    Jeeba - Saï Saï (feat. Dieyla)

  6. 6

    Jeeba - Allamé (feat. Malakey)

  7. 7

    Jeeba - Calm Down (feat. Karabalik Beatz)

  8. 8

    Jeeba - Champion

  9. 9

    Jeeba - Dafa Nekh

  10. 10

    Jeeba - Debbo Pullo (feat. Adviser)

  11. 11

    Jeeba - Décorée

  12. 12

    Jeeba - Dinala

  13. 13

    Jeeba - Do Change

  14. 14

    Jeeba - Goor

  15. 15

    Jeeba - Guuy

  16. 16

    Jeeba - Ki La Bagn

  17. 17

    Jeeba - Lamou Saff

  18. 18

    Jeeba - Life Goes On

  19. 19

    Jeeba - Number One

  20. 20

    Jeeba - So Bayiwoul

  21. 21

    Jeeba - So Mané Waw

  22. 22

    Jeeba - Soloul (feat. Khadim Temps)

  23. 23

    Jeeba - Soxna Ci (feat. Samba Peuzzi)

  24. 24

    Jeeba - Thies

  25. 25

    Jeeba - Thiopet Yobu

  26. 26

    Jeeba - Yow Rek (feat. Narah Diouf)

Calm Down (feat. Karabalik Beatz)

Jeeba

Tey ma bége la
Tey ma wone la
Tey ma wax la
Yaa ma gën a xam way!
Li nga ma def soo ko bàyyiwul
Dinga mës a ray doomu jaambur way!
Yaw yaa ma xam, xam ma bu baax
Bu lu xasaan ci man loxo keneen wokesu ko

Guddi gi jot ba lépp ni séelaw
Nga daagu ndank ñëw sama kaw di ma eh eh eh yaw
Say kesen kesen tere ma nelaw
Yaa ma mën a yuxuloo te xam nga dama ragal

Eh calm down, calm down
Bébé calm down, doomu jaambur la
Eh calm down, calm down
Bébé calm down, doomu jaambur la

Dootoo niit parce que doo nitu
Yaa nga may fit est-ce que doo ciit
Ni ngay def dama joomi
Man li may yaakaar est-ce que doo ñooñu

Yeah yeah
Baby li ma jaxal te nga wax ma ki la jàngal
Sant na sa bàjjen moom mi la jox li may jomal
Amatuma sago ci yaw su ma la gise saalit
Waaw waaw, yow baby waaw waaw

Seddal sama xol, dalal sama xel
Yaa ma gëna lool
Ne waaw seddal sama xol dalal sama xel
Eh eh eh

Eh calm down, calm down
Bébé calm down, doomu jaambur la
Eh calm down, calm down
Bébé calm down, doomu jaambur la

Dootoo niit parce que doo nitu
Yaa nga may fit est-ce que doo ciit
Ni ngay def dama joomi
Man li may yaakaar est-ce que doo ñooñu

Playlists relacionadas Ver mais playlists

Momentos

O melhor de 3 artistas combinados