Maak yaw ba abadan Jox naa la sama kàttan Jaayaanteek sama ndaw Dem naa ba ndox ci baat Jox naa la sama kàddu Mënatuma la baal
Te sèntu naa ci jële ndam maak yaw Ndax àddunya bi dafay feexe ba ma xàddi Duma bàyyi li ma tàmbali man Fàttaliku naa sama maam Ne na ma fori jëlal jaaro gi
Dégg naa ñu lay wutal mas te doo moroom jigéen Xam naa dinañu ma laaj lan moo tax ma wax lile Kenn du mel ni Thiam Baabel xam nga man bëgg naa la Kenn du mel ni Thiam Baabel xam nga man bëgg naa la
Demanoon de nañu Defando nañu ay mbir Xamal nga ma lu ne Soo ma yoolee Dootuma jar dara Bi ma ñépp umpale Yaw yaa ko xam Sama waay nga
Ku mel ni yaw Ku ka amul da koy iñaane Ku mel ni yaw Ëtu baabel ñoo lay laaj Ku mel ni yaw Thiam Baabel Demba Thiam, eh Ku mel ni yaw Ëtu baabel yaw lay laaj
Naa la yóbbu ëtub baabel Boole la ak samay nawle yi Xam nga tàkkusaanu baabel Thiam boroom ndendi was nga fay fowee
Yaw Mësuloo ma xépp ci samay ay ayib Sama njuumte yi mësoo ko nettali Xam nga jaambaar amul Ku ñu dimbale am Ku sañoon day baax Comme doomu ñay Bu ma ñaanal ponkal Man soo ma dundee baax