Sama xol nga yore Moom laa la toppe Liiti liiti liiti liiti May rombe gumbe Dama tapetul Def naa ci lu ne Lu mu guddi guddi guddi Dama lay gunge
Baby I follow you Cause my heart is on you You Baby I follow you Cause my heart is on you You
Oooh pourtant Jox naa la lépp, jox la lépp Oooh pourtant Je t'ai tout donné, tout donné
Euh euh euh
Massamba Wallo Xam naa bu baax li ngay bañ Ñu dem ba ci biir maa lay gaañ Def naa ko saay mas waaye Ak yaw da am lu may waaj Àdduna moo la soxla Man ma yitewoo la lool sax Massamba mi ngi may gaañ yaay Kalame naa la ak gaa yi Kaay gaaw, dëgg la ni dëng na Su ma demee balay way Nga xam ni caaxaan taxul
Oooh pourtant Jox naa la lépp, jox la lépp Oooh pourtant Je t'ai tout donné, tout donné
Euh euh euh
Man duma saay saay Laaj ko sama gayi Ñëwal ñu life waay Sonn naa Bul mësa gaadaay Doonal seen yaay Njaabot gi kaay waay Gunge ma
Man duma saay saay Laaj ko sama gayi Ñëwal ñu life waay Sonn naa