Waat naa duma la trahir
Su ma xeexeek yaw damay gaañ
Teyit seet naa la fu ne
Wër nañu ba tase du neen, han
Cér bi nga ma jox dafa matt sëkk
Yaay sama bët-set bi laa doon xaar ci yaw (wuy)
Yaay ki may bégal
Lalal basaŋ, talalal
Li ma doon wër ci biir dëkk
Yaa ma koy jox wéeruwaay (aah!)
Bu ma yërëm na ma dal
Xanaa ma doon sa wéerukaay
Li ma yor de yaa ko moome
Yaa may daaneel, duma la bàyyi waay!
Bu ma yërëm na ma dal
Man, xanaa ma doon sa weccookaay waay! (Wuy sama!)
Li ma yor de yaa ko moom
Yaa may daaneel, duma la bàyyi
Sa buum bi lonk ma ko
Diri ma man ba Japon
Bàyyil ma dead say loxo, my love
Parfum bu neex laay turoo
Xaaral ba jant bi so
Bu ginnaar sapp naan kooko (ah, ay!)
Nga di ma def lu ma dul nettali
Yaw kaay wax ma ku la jàngal yii
Yaay ki may bégal
Lalal basaŋ, talalal
Li ma doon wër ci biir dëkk
Yaa ma koy jox wéeruwaay (aah!)
Bu ma yërëm na ma dal
Xanaa ma doon sa wéerukaay
Li ma yor de yaa ko moome
Yaa may daaneel, duma la bàyyi waay!
Bu ma yërëm na ma dal
Man, xanaa ma doon sa weccookaay waay! (Wuy sama!)
Li ma yor de yaa ko moom
Yaa may daaneel, duma la bàyyi
Su ma reeree
Ma ree
Su ma reeree
Yaay ki may bégal
Lalal basaŋ, talalal
Li ma doon wër ci biir dëkk
Yaa ma koy jox wéeruwaay (aah!)
Bu ma yërëm na ma dal
Xanaa ma doon sa wéccookaay, waay
Li ma yor de yaa ko moome eey, waaw
Bu ma yërëm na ma dal
Xanaa ma doon sa wéerukaay