Doo mës a am ku mel ni man
Doo mës a am ku mel ni man
Doo mës a am ku mel ni man
Mel ni man, mel ni man
Baby dama fresh, dama clean, dama high
Su ma la duggelee ci roukhou wallay doo ma bàyyi
Xool ma ci kaw ba ci suuf damay lakke ni fire
Xam naa ni I'm the only one you desire
Xale bu pare boole ci wang wang wang
Dose bi nga soxla ma la koy jamm jamm
Sama wet dangay dégg jamm jamm jamm
Kenn ay fowe sa xol man man man
Mësoo am ku mel ni man baby dootoo ko amati
Boo fowe sa xel ba ma rëcc la dootoo ko defati
Doo mës a am ku mel ni man
Doo mës a am ku mel ni man
Doo mës a am ku mel ni man
Mel ni man, mel ni man
Jongoma mineur baby man ngay wër
Fi lépp mine jege ma exploser
Dama posé, osé, I'm good bad girl
Sa tempèrature ma koy yëgel di ko wacce
Baby
Sa yo jaxle man ngay lathiè
Baby
Xale bu pare boole ci wang wang wang
Dose bi nga soxla ma la koy jamm jamm
Sama wet dangay dégg jamm jamm jamm
Kenn ay fowe sa xol man man man
Mësoo am ku mel ni man baby dootoo ko amati
Boo fowee sa xel ba ma rëcc la dootoo ko defati
Mësoo am ku mel ni man baby dootoo ko amati
Bul fowe sa xel ba ma rëcc la dootoo ko defati
Doo mës a am ku mel ni man
Doo mës a am ku mel ni man
Doo mës a am ku mel ni man
Mel ni man, mel ni man
May sa ouroul aïni (eeh)
A mes cotés tu vis le paradis
Foo koy jëleeti ku mel ni
May sa superstar yaay sama paparazzi
May sa ouroul aïni (eh eeh)
A mes cotés tu vis le paradis (tu vis le paradiis)
Foo koy jëleeti ku mel ni
May sa superstar yaay sama paparazzi (paparazzii)
Ouhou ouh
Hehehe
Doo mës a am ku mel ni man