Est-ce que xam nga li nga yor?
Xale bu ndayam gërëm
Maa ko fa am nekkak keneen jàppu la
Yaw ku ñépp di wër nga am
Ñeneen ñi duñ dërëm
Maa ko fa am nekkak keneen jàppu la
May ki taxoon ñu sakk la
Ànd bangue ñu taxe aras
Ko mëna nekkal keneen tamit jàppu la
Maay ki sa yaram lacc
Ndax may ki koy dawal
Ko mëna nekkal keneen tamit jàppu la
Nekkak keneen jàppu la
Sa ex jàppu la
Nangul ni man nga nob bàyyil saagu jàppu la
Nekkak keneen jàppu la
Sa ex jàppu la
Nangul ni man nga nob bàyyil saagu jàppu la
Eh ndank rekk
Ma daan la jël bu gaaw amateur yi bekk
Ñi bekk V bi rekk match nul loolu mënta nekk
Doon sa géelu rap bi sanguloo la seet
Chance dëgg la am ku mel ni man ci sa wet
Li ñiy bari bari yaw may sa préférée
Te fàtte xaaju fi var am na so wedde
Li ngay wëri feneen yaw fi rekk nga koy ame
Ndax may ki ko am ma ko am baku bari doole
Sa pointure mana, keneen jàppu la
Ay boobu mbëgeelu sur mesure
Waxal sa dëggëntaan (kan nga nob)
Sa dëggëntaan (man nga nob)
Ku lay gaañ yaw ku lay cooxatan
Est-ce que xam nga li nga yor?
Xale bu ndayam gërëm
Maa ko fa am nekkak keneen jàppu la
Yaw ku ñépp di wër nga am
Ñeneen ñi duñ dërëm
Maa ko fa am nekkak keneen jàppu la
May ki taxoon ñu sakk la
Ànd bangue ñu taxe aras
Ko mëna nekkal keneen tamit jàppu la
Maay ki sa yaram lacc
Ndax may ki koy dawal
Ko mëna nekkal keneen tamit jàppu la
Nekkak keneen jàppu la
Sa ex jàppu la
Nangul ni man nga nob bàyyil saagu jàppu la
Nekkak keneen jàppu la
Sa ex jàppu la
Nangul ni man nga nob bàyyil saagu jàppu la
Àndak man day def effet man rekk damay yokk taar
Kon te nga ngoy bu dëgër banc de touche bi ñoo ngi xaar
Man rekk kala jàpp keneen ko àndalit du dem
Te ñi di la toppe soo yabo neleen ñu yam
Ñi naan la yaw fan wi danga leer so goore neleen may diw bi ngay diwoo
Lii tax man ak yaw ñun mëñuñu xulóo
Yàlla ko def suñu rawan yi ñoo jubbó
Ndax ma def ci yaw valeurs bañ lay wër comme ay vautours
Jarul wiri-wiri man nga nob allez-retour
Waxal sa dëggëntaan (kan nga nob)
Sa dëggëntaan (man nga nob)
Ku lay gaañ yaw ku lay cooxatan
Est-ce que xam nga li nga yor?
Xale bu ndayam gërëm
Maa ko fa am nekkak keneen jàppu la
Yaw ku ñépp di wër nga am
Ñeneen ñi duñ dërëm
Maa ko fa am nekkak keneen jàppu la
May ki taxoon ñu sakk la
Ànd bangue ñu taxe aras
Ko mëna nekkal keneen tamit jàppu la
Maay ki sa yaram lacc
Ndax may ki koy dawal
Ko mëna nekkal keneen tamit jàppu la
Nekkak keneen jàppu la
Sa ex jàppu la
Nangul ni man nga nob bàyyil saagu jàppu la
Nekkak keneen jàppu la
Sa ex jàppu la
Nangul ni man nga nob bàyyil saagu jàppu la