Ay kilometi kilometa
Ay kilometi kilometa
Ay kilometi kilometa
Ay kilometi kilometa
Yaw
Fi ma la def sama xol bi du caaxaan a la fiy génne
Coono
Yi ma daaj pur ñu bëggante bébé xam nga ni mu deme
Yoon bi metti woon ñu jaayante ko
Bu jaroon tuur deret ma rayante ko
Mindéef mënul tax bañu bàyyante, no
Te ñoom mënuñu tax bañu gaañante mak yaw
Ni ma la bëggee boo dawoon ay kilometa
Taxul nga dab ma
Ni ma la nobee boo dawoon ay kilometa
Taxul nga dab ma
Ni nga ma bëggee nu ko raw laa la bëgg
Bébé boo dawoon ay junni kilometa
Taxul nga dab ma
Ni nga ma nobee noonu laa la rawe
Boo dawoon ay kilometa
Taxul nga dab ma
Ay kilometi kilometa
Ay kilometi kilometa
Taxul nga dab ma
Ay kilometi kilometa
Ay kilometi kilometa
Taxul nga dab ma
Dama la bëgg ba tiit sama bopp
Yaw ni ngay def sama xol baaxul
Duma seetaan dara di la wokk
Bu jaaree la tayle sama nafsu
Xale bi doonal sama nattu
Billaay dawuma ci dara
Woowaleen ma Tycco Tattou
Ndax sa tuur laa bëgg mu defal ma sama yaram
Ni ma la bëggee boo dawoon ay kilometa
Taxul nga dab ma
Ni ma la nobee boo dawoon ay kilometa yeah
Taxul nga dab ma
Ni nga ma bëggee nu ko raw laa la bëgg
Bébé boo dawoon ay junni kilometa
Taxul nga dab ma
Ni nga ma bëggee noonu laa la rawe
Boo dawoon ay kilometa
Taxul nga dab ma
Yaa ma moom
Foo ma woo ma ñëw
Ndekke dama la nob
Topp xol bi lum ma digal ma def
Tocc kaani pacal ligoom
May kiy saf safal sa àdduna
Bébé yaa ma tingóom
Ca kaw a kaw yaa tax ma reew, waaw
Ne nañu yaa tax ma reew
Ma ni leen bégal ba ca dàq mooy nga nob kala nob waaw
Àljanna yaw yaa tax ma reew
Ndax danga ma nob ma nob la rawe ay kilometa
Ay kilometi kilometa
Ay kilometi kilometa
Taxul nga dab ma
Ay kilometi kilometa
Ay kilometi kilometa
Taxul nga dab ma
Ah, ah, ah
Daw ay junni kilometa taxul nga dab ma
Ah, ah, ah
Daw ay junni kilometa taxul nga dab ma
Daw ay junni kilometa taxul nga dab ma
Daw ay junni kilometa taxul nga dab ma