Taluma yendu di cas (awma jotam)
Nekkuma ci ay détails (bëgguma ko)
Danga faux man doo ma sonal (taluma ko)
Xaruma kenn ci leen (no no no)
Maa ngi baax, maa ngi baax, maa ngi baax
Maa ngi ci sama bopp
Maa ngi baax, maa ngi baax, maa ngi baax
Maa ngi ci sama bopp
Maa ngi baax, maa ngi baax, maa ngi baax
Maa ngi ci sama bopp
Maa ngi baax, maa ngi baax
Maa ngi ci sama bopp
Deel wax reek
Yaq dèr ak coow li nga apo
Li tamm nga ko
Doxo ci daray mandu
Soppil jikko
Toppal àdduna mu lay jay
Loo fiy def yaa ko tey
Samay wax nga yobbu ko
Seddeloo ma sama jikko
Soo may séntu ci gallu xaj yaa fay mujju ne dej tokk
Samay wax nga yobbu ko
Seddeloo ma sama jikko
Soo may sentu ci gallu xaj yaa fay mujju ne dej tokk
Taluma yendu di cas (awma jotam)
Nekkuma ci ay d [etails (bëgguma ko)
Danga faux man doo ma sonal (taluma ko)
Xaruma kenn ci leen (no no no)
Maa ngi baax, maa ngi baax, maa ngi baax
Maa ngi ci sama bopp
Maa ngi baax, maa ngi baax, maa ngi baax
Maa ngi ci sama bopp
Maa ngi baax, maa ngi baax, maa ngi baax
Maa ngi ci sama bopp
Maa ngi baax, maa ngi baax
Maa ngi ci sama bopp
Doomu garmi la man
Xaajuma ci ay wax
Topp nga ma mboro
Billaay xale bile Massa
Doomu garmi la mane
Xaajuma ci ay wax
Topp nga ma mboro
Billaay xawma li lan la
Dumla wax dara
Waaye li metti na
Xamaloo ma dara
Dima yaq dax àdduna
Munuloo ma teye fi Yàlla finé
Dom téré bék
Mënoo ma stressé
Yàlla tere
Samay wax nga yobbu ko
Seddeloo ma sama jikko
Soo may séntu ci gallu xaj yaa fay mujju ne dej tokk
Samay wax nga yobbu ko
Seddeloo ma sama jikko
Soo may sentu ci gallu xaj yaa fay mujju ne dej tokk
Taluma yendu di cas (awma jotam)
Nekkuma ci ay details (bëgguma ko)