Man foo may jaar gisuma ko
Fees sa bët di la jooyloo
Doole ju bari yénne la ko
Gone la damay bëre dóor
Doo dégg mukk ma ni baal ma
Bëgguma jamm, duma ni la Massa
Ñëwal jege ma taxa ripa
Foo ma woo ma wuyu la
Sopp nga doon jaay
Duggu ci man dootoo ko defati
Nduti nduti saay
Sopp nga doon jaay
Duggu ci man dootoo ko defati
Nduti nduti saay
Man duma baale
Su ma jékoo damay gaañ
Nduti nduti saay
Ma mën ma ëpp doole
Te su ma jekoo damay gaañ
Nduti nduti saay
Xale may dékk ma nga may daan
Man su ma lay ray damay reetaan
Séwel bët mattu bandit Kolobaan
Mas la ngay mbidiou ne kuñ coqotaan
Noo
Man su ma jàppee damay daan
Pacal limon toj kaani daqar ci thiambane
Noo
Dof bi nga séxel demul Fann
Boroom soow lu mu rew rew yabul boroom pane
Sopp nga doon jaay
Duggu ci man dootoo ko defati
Nduti nduti saay
Sopp nga doon jaay
Duggu ci man dootoo ko defati
Nduti nduti saay
Man duma baale
Su ma jékoo damay gaañ
Nduti nduti saay
Ma mën, ma ëpp doole
Te su ma jekoo damay gaañ
Nduti nduti saay
Kote bañ la bàyyi def la ni njegenaay
Rof la galgal nga tëdd njaaxaanaay
Muy suus, gowe ci ànd cuuraay
Wuyaay, ray la du tax ma bàyyi
Àjj la ba ci kaw doo lal suuf
Fàtte fepp, doo am tus
Jël sa tànk ak mbagg def la xale di la rakk
Bul ragal, may dawal
Sopp nga doon jaay
Duggu ci man dootoo ko defati
Nduti nduti saay
Sopp nga doon jaay
Duggu ci man dootoo ko defati
Nduti nduti saay
Man duma baale
Su ma jékoo damay gaañ
Nduti nduti saay
Ma mën, ma ëpp doole
Te su ma jekoo damay gaañ
Nduti nduti saay