Senegaal ñoo ko moom
Kenn mënu ko xar ñaar
Xiif, lekk ñàkku fi
Mar, naan ñàkku fi
Gudde am fo fanaan sama rééw
Bu ñu nangu kenn duggu suñu diggënte
Same diam ji fi ñoom mame bàyyi
Xamuñu leneen, bëgguñu leneen
He he he!
Gueye Ndioro wëy naa la (gueye Ndioro way naa la)
Faye Birame wëy naa la (way naa la)
Diobeu Dioubeu wëy naa la (diobeu dioubeu wëy naa la wëy naa la wëy naa la)
Tourè Mandi wëy naa la (hehee)
Thiam babel demba thiam way naa la
Gomissa gania way naa la (sané balama)
Ndiaye Diata Ndiaye wayaan naa la
Dioufa niokhobay wëy naa la (man djonkéléfa)
Sant yi war galgui rééw ma ngi
Sant yi war galgui rééw ma ngi
Diom foulak fàyda
Fonk diné tax xol yé ngi naat
Dieuf ju baax de diogufi
Sutura lañuy ndamo
Han Senegaal Ndiaye sama rééw
Walo walo si réw mi
Sine Saloum si réw mi
Casamance Boundou
Cadior ak Baol Fouta Toro
Jolof Senegaal
Dieng Salla waynala (samb maharam waynala)
Diagne Naar waynala (diallo diery waynala)
Sow Poulo waynala (ba poulo waynala Yagg masseuy)
Sall Ngari waynala (cissé ngari Ngom séni)
Ndoye Mali Maram Ndoye waynala (wade farawade ndiack)
Mendy Coto waynala (pouye beukeury)
Fall Ndiaga yaram waynala (waynala Camara yilé)
Dieye Massamba waynala (guissé Maabo)
Mbacké Balla Aissa
Sy Sawandé
Niass Coumba Abdallah
Laye Makhtar
Kounta Sidy way naa leen!
Sante yi war Galgui reew mangui (lo ndam ciré)
Sante yi war Galgui reew mangui (youm sega Mbaye mbassou Diene ndiogou)
Sante yi war Galgui reew mangui (thiaw séni Mbengue mbor)
Sante yi war Galgui reew mangui (ndour wally mbergane Niang mbaallo)
Sante yi war Galgui reew mangui (sene thiali Sylla moctar)
Sante yi war Galgui reew mangui (seck sa guanar)
Sante yi war Galgui reew mangui (sarra moundo Ly bousso)
Sante yi war Galgui reew mangui
Sante yi war Galgui reew mangui