1. 1

    Phillipe Monteiro - Sama Wo

Yeah
Sama fans yi, magui léne di gueureum
Di léne santeu guiss na séne taxaway
Musique bi

Pour yen la, oh-oh-oh-oh
Mane nop na léne, waw
Yagueu neu lool, bingueu démé
Mane réére na, réére na sa yow
Lane la wara déf, déf sans yow (sans yow hey)
Dama la soxla, té da ma la beugueu
(Déme ngueu té bay ma) bay ma si leundeum
Wanté xam ngua ni, ni dama wara doumeu maneu doundeu ba téy
(Déme ngua té bay ma) baby gnewateul si mane
Xana déguo sama wo

(Baby gnewateul) yagueu na lool bi ngua démé
(Tax na sama xol wééte) lou maye déf ba ngueu gneuwate, gneuwate si mane
(Baby gneuwatal) yagneu na lool bi ngua démé
(Tax na sama xol wéét) xana di la wax beuss bou né fi ngua tolou si mane

Bou ma togué di xalaate (doundeu you nex gui gnou done doundeu)
Rek sama xool fess (xama tou ma lou ma wara déf)
Déme ngua bayi ma thi leundeum (wanté xam ngua ni)
Dama wara doundeu mateye (déme ngua té bayi ma)
Bayi ma si leundeum
Dama la soxla, dama la beugueu

Baby ngeuwateul si mane, xana déguo sama wo

Baby gnewateul, yagueu na lool bi ngua démé
(Tax na sama xol wééte) lou maye déf ba ngueu gneuwate, gneuwate si mane
(Baby gneuwatal) yagneu na lool bi ngua démé
(Tax na sama xol wéét) xana di la wax beuss bou né fi ngua tolou si mane

Xama tou ma li ma wara déf (yagueu neu lool)
Bouguou ma ngua xaam li ma dadj, nax xaam na nik ame ngua kénéne
Meunou ma ko gueum
Meuneu dess ni

Yagueu na lool bi ngua déme mane réére na nékeutofi
Lane la wara déf nékeutofi
Dama la soxla, dama la beugueu
Baby gneuwateul si mane, xana déguo sama wo

Baby gnewateul, yagueu na lool bi ngua démé
(Tax na sama xol wééte) lou maye déf ba ngueu gneuwate, gneuwate si mane
(Baby gneuwatal) yagneu na lool bi ngua démé
(Tax na sama xol wéét) xana di la wax beuss bou né fi ngua tolou si mane

Playlists relacionadas Ver mais playlists

Momentos

O melhor de 3 artistas combinados