1. 1

    Wally B. Seck - Balma

  2. 2

    Wally B. Seck - Alhamdou Lilah (feat. Sidiki Diabaté)

  3. 3

    Wally B. Seck - Entre Nous

  4. 4

    Wally B. Seck - Natural Love

  5. 5

    Wally B. Seck - Bad Man

  6. 6

    Wally B. Seck - Désolé (feat. Le Raam Daan)

  7. 7

    Wally B. Seck - Djiguene

  8. 8

    Wally B. Seck - Don't Be Afraid

  9. 9

    Wally B. Seck - Mon Combat

  10. 10

    Wally B. Seck - Assurance (feat. Sidiki Diabaté)

  11. 11

    Wally B. Seck - Cherche En Toi

  12. 12

    Wally B. Seck - Choco Vanille (feat. Ndiolè Tall)

  13. 13

    Wally B. Seck - Choix (feat. Mia Guisse)

  14. 14

    Wally B. Seck - Confuse (feat. Mia Guisse & Amadeus)

  15. 15

    Wally B. Seck - Dafmay Dal (feat. Le Raam Daan)

  16. 16

    Wally B. Seck - Dawuma Dara (feat. Samba Peuzzi)

  17. 17

    Wally B. Seck - Derangé

  18. 18

    Wally B. Seck - Diégué Kiraay

  19. 19

    Wally B. Seck - Djery Ngoné

  20. 20

    Wally B. Seck - Don't Leave Me Alone (feat. Marco Alexander)

  21. 21

    Wally B. Seck - Donne moi une chance

  22. 22

    Wally B. Seck - Feccal Ma

  23. 23

    Wally B. Seck - Henne Time (feat. Ndiolè Tall)

  24. 24

    Wally B. Seck - Hey Ya

  25. 25

    Wally B. Seck - Hymne Faramareen

  26. 26

    Wally B. Seck - Immigrés

  27. 27

    Wally B. Seck - Jëli (feat. Amadeus)

  28. 28

    Wally B. Seck - Lo Beugue

  29. 29

    Wally B. Seck - Loving You

  30. 30

    Wally B. Seck - Mame Boye

  31. 31

    Wally B. Seck - Mirna (feat. Le Raam Daan)

  32. 32

    Wally B. Seck - Mon Choix

  33. 33

    Wally B. Seck - Nila (feat. Akhlou Brick)

  34. 34

    Wally B. Seck - Nila (feat. Akhlou Brick)

  35. 35

    Wally B. Seck - Only Love (feat. Fata)

  36. 36

    Wally B. Seck - Paradise

  37. 37

    Wally B. Seck - Reguine Tass (feat. Viviane Chidid)

  38. 38

    Wally B. Seck - Runaway

  39. 39

    Wally B. Seck - Si Vous Saviez

  40. 40

    Wally B. Seck - Stay

  41. 41

    Wally B. Seck - Thieuguine

  42. 42

    Wally B. Seck - Togn Ngama

  43. 43

    Wally B. Seck - Venise

  44. 44

    Wally B. Seck - WURUS (Version Afro)

  45. 45

    Wally B. Seck - WURUS (Version Mbalax)

  46. 46

    Wally B. Seck - Xarma

  47. 47

    Wally B. Seck - YA TAY (feat. Baye Mass)

  48. 48

    Wally B. Seck - Yaa Meune (feat. VJ)

  49. 49

    Wally B. Seck - Yeye (DIAGA)

  50. 50

    Wally B. Seck - Yobaneté (feat. Le Raam Daan)

Jëli (feat. Amadeus)

Wally B. Seck

Boo ma beddiwul xalaatuma la bàyyi
Awma làmmiñ soon tudduma lambay yoy

Gaañ la taxul nga ba
Tooñ la taxul nga may rëccooy
Salaw yenn saay nga mer
Sama jaambaar ci yaw mi la wékooy

Dootuma wiri wiri njari ndari
Li ma moom lay jëli (eeh yoo)
Dootuma yonni kenn ci sama waa ji
Man mi maa koy jëli (man ma)

Dootuma wiri wiri njari ndari
Li ma moom lay jëli (daadi sama waay)
Dootuma yonni kenn ci sama waa ji
Man mi maa koy jëli (danga di sama waay)

Bala ma jog
Fajar fekk nga dem jaayooy
Bale kër gi raxas say ndap
Ndekke boobu dam ngay wajal

Dundu maata ñaan nooy
Ndaxte gaynde dama koy jur
Ndax fitna loo ma
Xëboo li ma lay jox
Lépp loo ma ñaan dinaa la may

Dootuma def leen lu lay metti sama ndaw si
Ndax sama nawle nga doo leeral sama yoon wi
Dootuma nangu mindéef di dox sama digu ak yaw
Ndax Yàlla moo def ci ñun lay ñu wëy nak
Kaay waay!

Gaañ la taxul nga ba
Tooñ la taxul nga may rëccooy
Salaw yenn saay nga mer
Sama jaambaar ci yaw mi la wékooy

Dootuma wiri wiri njari ndari
Li ma moom lay jëli (eeh yoo)
Dootuma yonni kenn ci sama waa ji
Man mi maa koy jëli (man ma)

Dootuma wiri wiri njari ndari
Li ma moom lay jëli (daadi sama waay)
Dootuma yonni kenn ci sama waa ji
Man mi maa koy jëli (danga di sama waay)

Gaañ la taxul nga ba
Tooñ la taxul nga may rëccooy
Salaw yenn saay nga mer
Sama jaambaar ci yaw mi la wékooy

Eee waay
Sama jaam, sama waay
Eh waay wow
Sama jaam, sama waay

Playlists relacionadas Ver mais playlists

Momentos

O melhor de 3 artistas combinados